|
Anna Maria Jopek - Dina Delusi lyrics
Toopna yoon bi ngay fatelu Bidew ya ngi seetaan Fo xool ngalawa pënd thino Gëmulo ne dina oibisi Dina delusi lerna Waye boma fatee Dina delusi lerna Wadje suou woy dinga yëg Dina delusi worna Waye boma fatee Bataxal bii moy wone Nimala namme dila djege Thi ngoon yu weeta weet Xamnane toog di xaar mo des Ni xale bu sawar Di xaar foonu dneydja Subateel di xaar nadjbi Xol di neg dej bu neex |
|
Last added lyrics |
---|
Wolves in Wolves' Clothing by NOFX |
Lost and Found by Will Smith |
Reality Check by Juvenile |
Memory Almost Full by Paul McCartney |
Zeitgeist by The Smashing Pumpkins |