|
Youssou N'Dour - Silence [Tango] lyrics
Sou néké sama nékk, nga bagne ma wo Mba mou diapp ma, ma bagne leu wo Khawma louko diote, ba sa khol def gome Té gomou khol… Souma diéki diéki daméy degg am louy rire ci biir kholam Gnou deukk ci tiow, sama khol bi diékh, sa khol bi fess, gnoune niar nioko def Bi khél nane nako, yow sétal bi gueune, beulé khél nane doumakooo, yay séét, yay séét (x2) Ci deug deug yaye sama goudi, yaye sama beutieuk, ba takhna yama mome Téyit bouniou dé nélaw nioune niar déy andak téy andak silence Foumou tolou daféy dianérr mélnii kou réérr ci biir mbeuguel, Niou deug ci tiow, sama khol bi diékh, sa khol bi fess, nioune niar nioko defff Refrain (x4) Dafa done peigner wou yoor yoor Dafa done solou dima khar Dafa sole lou khél ak lou bleu diko tekk ci yaramam, yaramam, yaramam Bouma léké mou melni lekk na Bouma khiffé mou tagok sagom Bouma togué, mou dianok mane dima khol, dima khol, dima khol Hé yow hé yow kay guindi ma, hé yow hé yow kay firima, hé yooww kay wané ma Mbeuguel dafa nekh lolou, mbeuguel dafa nékhh, dafa nékha nékha nékh Ba moudj méti lolou, méti lolou, méti lolou Bilay kholam dafa |
|
Last added lyrics |
---|
Confessions by Usher |
Big Dog Daddy by Toby Keith |
Waiting for the Punchline by Extreme |
Kina by Kina |
Twenty Four Seven by Tina Turner |